Nio gui bess ci lien bii https://www.chess.com/clubs/forum/view/new-owner-pour-team-senegal nga woteel @uptophigh ngir mu mëna dundal Team Senegal ci def ay admin yu bees te fexe ba mu jouer ci ligue mondiale bi.
Je joue sur lichess mais pour participer a des tournois en ligne je suis inscrit dans d'autres clubs qui organisent des competitions inter club en ligne.
@uptophigh dina nekk boroom ba admin bu baax bu bawoo senegal wane ni ñoo wara nekk boroom. @uptophigh dina nekk boroom ci diir bu gàtt bañu tànnee admin yu bari ngir jiite ekip bi.
Dama jàng wolof mooy làkku senegal. Dama bëgg lool cosaan ak aada ndax Hawaii mooy dëkk bi gëna bari ay cosaan ak aada ci àdduna bi. Hawaii dafay dalal ñépp ak Aloha. Ginaaw ñaari at ginaaw bima gisee echec Senegal di wàññeeku, dama bëgga def dara ngir saafara jafe-jafe bi.
Une fois que j'aurai réglé la plupart des problèmes, je nommerai administrateurs tous ceux qui participent à ce forum afin que Senigal ne soit plus jamais un club inactif. J'ai contacté le support de chess.com et ils devraient me répondre d'ici quatre jours, voire plus tôt.
Veuillez voter pour @uptophigh afin qu'il devienne le nouveau propriétaire de l'équipe du Sénégal en cliquant sur le lien du forum et en laissant un commentaire. https://www.chess.com/clubs/forum/view/new-owner-for-team-senegal> La première chose que je ferai sera de changer le fond pour que les joueurs puissent le voir.